Wikipedia
wowiki
https://wo.wikipedia.org/wiki/X%C3%ABt_wu_nj%C3%ABkk
MediaWiki 1.39.0-wmf.26
first-letter
Xibaarukaay
Jagleel
Waxtaan
Jëfandikukat
Waxtaani jëfandikukat
Wikipedia
Wikipedia waxtaan
Dencukaay
Waxtaani dencukaay
MediaWiki
Waxtaani MediaWiki
Royuwaay
Waxtaani royuwaay
Ndimbal
Waxtaani ndimbal
Wàll
Waxtaani wàll
TimedText
TimedText talk
Module
Discussion module
Gadget
Discussion gadget
Définition de gadget
Discussion définition de gadget
Djeumbet Gorée
0
8804
104739
104737
2022-08-28T23:13:01Z
Ousmane-ballou
13979
wikitext
text/x-wiki
== Dieumbet Gorée ==
Deuk bi niou guéna kam ci Gorée mougui nekk ci biir guethie Atlantique jegue lol Dakaru. Bokouna ci 19 Commune yi ci Dakaru. Deuk bobou nekhna beureup bou raniékou ci kellu ninii. Nam té dé ci 1978 lako koureul bi nioy wowé Organisation des Nations Unies ci layko jeumbet. Gorée niouko guena ranie ci diamano boniou diay niit te mou guen ci feuss. Gorée nékhna tamit Deuk bu Diekh ci bou boku ci liste bu Nations Unies pour l' éducation, la science et la culture (UNESCO).
=== Tarikh ku Gorée. ===
Portuguais bouniou wakh Denis Dias mo jekka niew fi niou na Gorée ci atoum 1444 mou wowé ko "Palma". Guenaw lolou ci la Hollandais yi doora niew ci atoum 1588. Tourou Gorée mougui diogue ci "Goede Reede" moy fi terce kay bou guen. Guenaw lolou ci la Français niew ci atoum 1677. Niom ak Anglais yi amonagn ay probleme you beurii, ci lagn signe ay katiim benne accord de paix d'Amiens [[:fr:Paix_d'Amiens#/media/Fichier:La_Paix_d'Amiens_de_Jules-Claude_Ziegler_(1853).jpg|ci]] atoum 1817, français yi doraa diot thie Gorée.
yayoum niit ku nioul mo wora loone soowe dianteut africa li thie melni (Gambie, Saint louis du Séenegl, Benin, Ghana..), ci la doomu afrique yi di diogue deem Amerique. Toubab yii leen don Diaye delu Europe.
Suniu kayma ci liim ay Domu afrique you beurii laniou diaye diguente (1726 be 1848)<ref>https://fr.wikipedia.org/wiki/%C3%8Ele_de_Gor%C3%A9e#cite_note-4</ref>. Ni doone diaye nioniou di ay Buuru wolofs neccon ci Senegambia. Goree nekone mba di weyal diayoume doomu adam ci ay dioune att.
Dakaaru boumou dioundo ci attoum 1857, ci la Goree commence di niack place bi mou amone. Toubab yi nio amaal niarri communes Ndar ak Gorée ci Afrique soow jatt.
yetnen communes toff talou ci mouy Teeguédj ak Dakaru .
ci attum 1891, nett niou doone dundu Gorée limba gui tolou ci 2100 domu adama boba domu adama yi dundu ci Dakaru niou lolou ci 8737. lim bobou mosdi yokku boba be tey.
=== Ci Dookalin Gorée<ref>[[Dencukaay:Ile de Gorée Sénégal.jpg|vignette]]
</ref> ===
====== Soukandicou ci térre yii administration toubab mo diekk ci diamano colonisation. ======
Bo ba Dakaru lebou yi nio fay docale. Motakk Gorée Bocone ci ñiet commune yu niek Bu Senegaal moomé bopam ay att ci kanam, lou diapp 1996, nii done dookal guurgui, denio dioyantii dokaliin Rewmi. Niou Koy woowe "Décentralisation", moy diokk ay katann gook gokan yi. communes yi nekk ci Dakar plateau
{| class="wikitable"
|+
!Diir
!Niu ko deff
!Bokku
!Laan la
|-
|1996-2002
|Urban Alexandre Diagne (1922-2010)
|
|Maire honoraire
|-
|2002 be teyy
|Augustin Senghor
|RES
|Président de l'Union sportive de Goré
|}
==== Neekiin ====
<ref>[[Dencukaay:Carte de l'île de Gorée en 1784.jpg|vignette]]
</ref>
<references group="Gorée" />
lzuuh8pnyvqbp0w2x63k7jfoquej2q0